Li La Wakh Lyrics – Dieyna

Li La Wakh Lyrics sung by Dieyna represents the French Music Ensemble. The name of the song is Li La Wakh by Dieyna.

Li La Wakh Lyrics

Et puis quoi, yaw la kan?
Xamuloo ma di wax ci man
Seetuloo bëgg di ma tamm
Mën wañe allure bu mel ni dos d’âne
Ñi di wax ci samay def
Ku ci dul def man li may def
Dañu lay xeelal ba nga def
Weraat naan xoolal la muy def, eh

Fomp sama rangoñ dootuma jooy
Ndax léegi xam na
Ni nit ku la bañ, amuloo koy defal
Ba mu xëy bëgg la

Mën naa la jox ay nopp
Waaye taxul ma gëm say wax
Ay bët nak faw mu jooy
Di sooga mëna gis bu baax
Ñin koy jema fay muy boy
Waaye xanaa nga war ko baal
Fi ku fi baax day bari noon
En tout cas man li la wax

Alabarka nene jarama
Nit ñi lëndëm nañu yaay ñaanal ma
Ba ma muc ci ñett ñi
Ku may signe te bëgguma
Kiy indi di yóbbu
Ak kiy bég ci sa coono
Année yi dem dem ba jangal
Ma ngi fi boy déglu doo dem
Bu Yàlla di trace ngay effacé
Yaw lay effacé retracé

Mën naa la jox ay nopp
Waaye taxul ma gëm say wax
Ay bët nak faw mu jooy
Di sooga mëna gis bu baax
Ñin koy jema fay muy boy
Waaye xanaa nga war ko baal
Fi ku fi baax day bari noon
En tout cas man li la wax

Yak sa ree ju neex xame naa la (xamee naa la)
Bañ weex na mais déréta ko lal
Pourquoi tout ça, tout ça pour rien
Pourquoi tout ça, tout ça pour rien

Mën naa la jox ay nopp
Waaye taxul ma gëm say wax
Ay bët nak faw mu jooy
Di sooga mëna gis bu baax
Ñin koy jema fay muy boy
Waaye xanaa nga war ko baal
Fi ku fi baax day bari noon
En tout cas man li la wax

Yak sa ree ju neex xame naa la (xamee naa la)
Bañ weex na mais déréta ko lal
Alabarka nene jarama
Nit ñi lëndëm nañu yaay ñaanal ma

Na xerr bi dal say noon

Video Song

Thank you for exploring “Li La Wakh Song” by Dieyna with me on https://prolyrical.com. I’d love to hear your thoughts or favorite parts of the music video. Feel free to comment below or contact us if you have any suggestions or corrections in the lyrics and suggest more songs for future discussions. Let’s keep the music conversation going!

Keywords & Tags

“Li La Wakh” Lyrics, French Song Lyrics, Trending Songs, New Song, Dieyna, Music Lyrics, Song Lyrics, Prolyrical Lyrics

Leave a Comment